Sidy Diop Soubana Скачать

Sidy Diop Soubana

Sidy Diop

Soubana

13 прослушиваний
05:50
Все треки Sidy Diop Текст песни
Слушать
Скачать песню

Текст песни «Soubana»

Sidy Diop

Lemouna
Mane dé lemouna
Yallah bour
Mangui laye gnaane
Nga mousseul maaaa
Mane lemouna
Aye lemouna
Yalla bour
Mangui laye gnaane
Nga mousseul maaa
waaw waawwww
Ndakhté ndaw laa
Damaye soga dore
Malaye gnaane
Nga mousseul maaa
Waaw waawwwww
Soubana maaaa
Mane dé lemouna
lemoule
Mane doli na
Di lemou
Yalla mangui laye gnaane
Nga mousseul maaa
Si noone
Té nga yégali ma
Lii bi yoone
Yalla mangui laye gnaane
Mane Sidy delou
Sakou gnaane
Nga mousseul maa
Si pékhé noone
Té nga yégalima
Li bi yoone
Guisse na si adouna
Ndaw mouye gnaane
Yalla touki
Bamou démé gnibissi woule
Guisse na adouna
Ndaw bou tabakh keureum
Bamou yégué
Mom deukoussa
Mane Sidy
Boudé music bi
Sama djidie laye la
Lawou damalaye gnaane
Nga yégalima
Li bi yoone
Ndakh adouna
Saa bo yéwo
Nga guisse kou ame
Aye ndok ndok
Aye waaye
Si digou ndawame
Yalla mangui laye gnaane
Nga lakeu ma
Fou yakeu yégoule
Té nga yégalima
Li bi yoone
(Ndeysaane)
Baye Fall nawlo nala
Deguena ni Adjaratou Maimouna
Lagnouye wowé sa yaye
Baye Zale
Segne thialy démba Sene
Kokou moye chéri Awa Faye
Dougou dougou Wagane
Khady Coumba Waganooo
Yayou Ibrahima
Damalaye woyale
Ma beugue djiguen gui
Collé Faye borom Cobra boutique
Abdou Faye nga bokak baye
Aye waaye Collé
Beugue nala lolle
Ngagne Démba
Borom Guédiawaye la
Ngagne Démba
Domou Guédiawaye la
Mbok yayou
Pa Azizo
Chéri Daro beugue nala
Senegal ana Toucouleur yé

На странице доступен трек Soubana от Sidy Diop (05:50). Слушайте онлайн или загрузите в mp3 в один клик бесплатно на свое устройство — выше есть текст песни.

Другие песни Sidy Diop

Свежее на Muzfrog

Все новинки →